Projet bii di TBR té ñu bëri raññee ko tey, defay dooleel cosaanu "mayé". Leip ngui dioudo ci benn entreprise sénégalaise bou toud nelam, niou bëgon leen wan tey ni projet bi commencé.
Di profitoo ci occasion bi di ndokkale Communauté Chrétienne bi yëp ci Pâques bi.
Jar jëf yéen yi ñuy seetaan. Lii lépp yeen a ko waral. Du nu tàyyi ci di leen bégal.
Li ci kanam, rawul i gët